Home
Flashcards
Preview
WolofBook01
Home
Get App
Take Quiz
Create
Automatically remove your image background. Try it now!
https://remove-image-background.com
How did you spend the night / the day?
Nanga fanaane / yendoo?
(ANtwort jamm rekk)
How
is
the
family?
Naka
waa
kër
gi?
How
is
your
mum
/
dad?
Ana/Naka sa Yaay/sa baay? (antwort: mu ngi fi/mu nga fa)
Wie war eure Nacht?
nangeen fanaane?
Wie ist die Arbeit?
Naka liggéey bi? (Antwort mu ngi dox, es geht)
ich hoffe, niemand ist krank
Mbaa kenn woppul? (Antwort Mbaarikala thanks god)
informelle Antwort aus na nga def
Maa ngi sant (i thank god)
How
is
it
going? (informell)
Numu
deme? (Antwort mu ngi dox oder nii rekk geht so)
INformell wie laufen die Sachen?
Naka afeer yi? (Antwort: ~nu ngi dox)
Are
you
enjoying
yourself?
Yaangi
noos? (Antwort tuuti rekk, just a bit)
What’s
new?
Lu bees? Antwort Dara
beesul (nichts)
yaa
bees!
am mOrgen
ci suba si
Hast du gut geschlafen?
Nelaw nga bu baax? (Antwort: waw, nelaw naa bu baax)
Hast du eine gute Nacht gehabt?
Jamm nga fanaane? (Antwort jamm rekk)
Wie ist dein Morgen?
Naka suba si? (jam rekk Nii rekk (geht so))
am Nachmittag
ci ngoon si
Hattest du einen guten Tag?
Jamm nga yendoo? (jamm rekk, nii rekk)
Wie ist der Nachmittag?
naka ngoon si?
Wie ist die Hitze?
Naka tangaay wi?
Wie ist die Kälte?
Naka seddaay bi?
Bis nächstes Mal
Be beneen yoon
Bis später
Be ci kanam
Bis die Tage
Ba fan yi
Bis morgen
Ba suba
Bis heute nachmittag
Ba ngoon
Hab einen guten Tag
~nu yendu ak jamm (antwort jamm ak jamm)
Hab eine Gute Nacht
~nu fanaan ak jamm (antwort jamm ak jamm)
(I don’t speak much Wolof.)
Dégguma Wolof bu baax
(I don’t understand what you said
Dégguma li nga wax
(I’m learning Wolof small-small
Maangiy jang Wolof ndank-ndank
(to greet)
nuyoo
to greet qn
nuyu qn
die Nacht verbringen
fanaan
den Tag verbringen
yendu
to work)
liggéey
to walk
dox
Spaß haben
noos
night
guddi
familie
waa kör gi
nothing
dara
where/how is / are...
ana...
wie gehts...
Ana/Naka/Na
nur
rekk
Hand geben bei Älteren Respekt
mit beiden Händen
Automatically remove your image background. Try it now!
https://remove-image-background.com
Author
helmke
ID
345339
Card Set
WolofBook01
Description
WolofBook01
Updated
2019-04-08T09:57:42Z
Show Answers
Home
Flashcards
Preview